EPISODE · Feb 13, 2023 · 44 MIN
MABA DIAKHOYU BA
from Xam sa démb, xam sa tey · host Goethe-Institut
Muhamad Ba ñu gën koo xamee ci Almami Maba Jaxu Ba mi ngi judoo Tawa ci RIP atum 1809. Jaakaarloo na ak Tubaab yi ay yoon i yoon ngir bañ ku noot der bu ñuul. Yaatal na yit Islaam ci Senegaal.
NOW PLAYING
MABA DIAKHOYU BA
No transcript for this episode yet
Similar Episodes
May 14, 2026 ·128m
May 14, 2026 ·42m
May 14, 2026 ·9m