01. Buuru Ndam - Ubbite gi (Pàcc 01)
from Sunu Yaakaar Hosted by Serigne Malick Diop
Lii di ab tukki ci biir mbindi yonent yi dafa len di woo ci xamanteek jenn Yàlla ji am kepp te di dëgg. Te it ngeen xam pexeem mi Mu tëral ngir wallu surgaam yi fippu ba tàbbi ci nguurug lëndëm gi. Noonu, ñu mëna dundandook Moom ba fàww ca nguurug leeram ga. Nii ñu ko nettalee mu xumb ak nataal yeek «wideyo» yu taaru yi di lu nekk, dafa dëppook ‘seetaankati’ àddina sépp ak nu seeni at mëna tollu.
Embed this episode
No transcript yet.
Similar podcasts
Frequently asked questions
How long is this episode of Sunu Yaakaar?
This episode is 9 minutes long.
When was this Sunu Yaakaar episode published?
This episode was published on October 14, 2021.
Can I download this Sunu Yaakaar episode?
Yes. Use the download control on the episode player to save the publisher-provided media file.