50/50?
from Wolof Podcast Hosted by Lahat Diaw
Tay damay def taxaw setlu ci néegu sëy yi. Ndax kër gi lici war yépp ci wàllu kopar ci góor gi la war a joge walla mënees nako séddoo? Diine moom li mu wax leer na, ndax kodday ak yor góor la war. Waaye ndax léegi nit yi ci diine rek lañuy dellu? Ndax seen mbatit ak tolluwaayu jamono du amul yaneeni jeexital ci seen jëflante? Ps: ci waxtaan bi amna foo xamne polygamie la bëggoon wax, wax monogmie.
Embed this episode
No transcript yet.
Frequently asked questions
How long is this episode of Wolof Podcast?
This episode is 45 minutes long.
When was this Wolof Podcast episode published?
This episode was published on March 3, 2023.
Can I download this Wolof Podcast episode?
Yes. Use the download control on the episode player to save the publisher-provided media file.