Skip to content
Bëgg a baax episode artwork

Jan 21, 2022 45 min

Bëgg a baax

from Wolof Podcast Hosted by Lahat Diaw

Tay ma ànd ak sama gan gu njëkk muy Bàmba ñuy waxtaane yoonu njub ak baax. Def lu baax yomb na waaye dëkk ci moo jafe. Yonent bi (saws) dafay wax ni àddina mooy aljànna ki weddi, waaye kaso la ci ki gëm. Mu melni kon ku bëgg dund ci niki Yàlla gërëmee dina laaj jékki ay jéego jëm ci yar sa bakan ak topp Yàlla. Waaye mu nekk yoon bu meti loolu. Lan mooy yoonu njub? Ak yan jafe-jafe la doomu aadama bi di dajeek ngi yégg baax? Ci tënk loolu lanuy waaxtaane ci épisode bii. [email protected]

Episode details come from the podcast's RSS feed.

Embed this episode

Ready to play

Bëgg a baax

0:00 45:00

No transcript yet.

Requests help us decide what to transcribe next.

Frequently asked questions

How long is this episode of Wolof Podcast?

This episode is 45 minutes long.

When was this Wolof Podcast episode published?

This episode was published on January 21, 2022.

Can I download this Wolof Podcast episode?

Yes. Use the download control on the episode player to save the publisher-provided media file.