Boroom ñaari tur yi
from Wolof Podcast Hosted by Lahat Diaw
Boroom ñaari tur! Bu yàggul dara gis nanu ak li xéw ak Gana Géy. Mu bañoon jàppale boroom ñaari tur yi ci yaatal seen gis gis, waaye mu dégg ci lu nekk. Loolu moo waral ñu def ci taxaw setlu yi xool ndax mbir mi dëppo na ak suñuy gëm-gëm ak ban taxawaay lanu ci war a am. [email protected]
Embed this episode
No transcript yet.
Frequently asked questions
How long is this episode of Wolof Podcast?
This episode is 45 minutes long.
When was this Wolof Podcast episode published?
This episode was published on June 10, 2022.
Can I download this Wolof Podcast episode?
Yes. Use the download control on the episode player to save the publisher-provided media file.