Skip to content
Mucc saa 01 | Bànni Israyil dem na réewum Misra episode artwork

Oct 27, 2022 13 min

Mucc saa 01 | Bànni Israyil dem na réewum Misra

from Sunu Yaakaar Hosted by Serigne Malick Diop

Ñu dem ba jëmmi jamono, beneen buur bu xamul Yuusufa falu ca Misra. Mu wax ak waa réewam, ne leen: «Giirug bànni Israyil kat ñu ngi nuy gëna bare, ba ëpp nu doole. Nanu ci sàkk pexe, ngir ñu bañatee yokku. Lu ko moy bu xare amee, man nañoo far ak sunuy noon, xeex ak nun, ba génn réew mi.» 11Ba loolu amee ñu fal ay nit ñu leen di ga ca seeni sas, di leen ca fitnaal lool. Noonu la bànni Israyil tabaxale Firawna buuru Misra dëkk, ya ñu naa Pitom ak Ramses, mu def ko ay dencukaayi dund. Terewul lu ñu leen gëna fitnaal, ñuy gën di fulandiwu, yokku, ba waa Misra am njàqare ca bànni Israyil.

Episode details come from the podcast's RSS feed.

Embed this episode

Ready to play

Mucc saa 01 | Bànni Israyil dem na réewum Misra

0:00 13:42

No transcript yet.

Requests help us decide what to transcribe next.

Frequently asked questions

How long is this episode of Sunu Yaakaar?

This episode is 13 minutes long.

When was this Sunu Yaakaar episode published?

This episode was published on October 27, 2022.

Can I download this Sunu Yaakaar episode?

Yes. Use the download control on the episode player to save the publisher-provided media file.