Néegu séy
from Wolof Podcast Hosted by Lahat Diaw
Néegu séy lañuy waxtaane tay. Ñu setlu at yi weesu amna ay soppiku yu mag ci pénc mi. Séy yi barina ay jafe-jafe lool. Ñuy def taxaw setlu ngir man a xam luko waral ak yan saafara lanu ci man a indi. May dalal Soxna Coro Coor muy yëngu ci „aide au développement“. [email protected]
Embed this episode
No transcript yet.
Frequently asked questions
How long is this episode of Wolof Podcast?
This episode is 45 minutes long.
When was this Wolof Podcast episode published?
This episode was published on June 24, 2022.
Can I download this Wolof Podcast episode?
Yes. Use the download control on the episode player to save the publisher-provided media file.