Seex Ibra Faal
from Wolof Podcast Hosted by Lahat Diaw
Tay nuy waxtaane jëmm ju am solo te mooy Seex Ibra Faal. Barina loolu lu ñu mën a jàngee ci moom ndax yiteem ju kawe. Mu nekk jëmm ji wone Seex Ahmadu Bàmba ba noppi wone nan lanu ko war a toppe ngir jariñu ci moom. Daan na wax naan Sëñ Bàmba mooy dëkk bi, man Ibra Faal maay yoon bi ciy dem. Naan la def ba taxawal loolu ak lan lanu ci mën a jàngee? Baay Lahat [email protected]
Embed this episode
No transcript yet.
Frequently asked questions
How long is this episode of Wolof Podcast?
This episode is 45 minutes long.
When was this Wolof Podcast episode published?
This episode was published on March 17, 2023.
Can I download this Wolof Podcast episode?
Yes. Use the download control on the episode player to save the publisher-provided media file.