„séries sénégalaises“
from Wolof Podcast Hosted by Lahat Diaw
At yii ñu weesu gis na ñu ni „séries sénégalaises“ bari nanu loolu. Ñu gis ci tamit yu bees yu bari yoo xamni miinu ñu ko woon ci réew cig fësal. Mootax ñuy def taxaw setlu di jàngat jafe-jafe yi mu mën a indi ci pénc mi. Ma àndaat ci ak jëwriñ Bàmba Jaw. [email protected]
Embed this episode
No transcript yet.
Frequently asked questions
How long is this episode of Wolof Podcast?
This episode is 45 minutes long.
When was this Wolof Podcast episode published?
This episode was published on July 8, 2022.
Can I download this Wolof Podcast episode?
Yes. Use the download control on the episode player to save the publisher-provided media file.