Skip to content
Tariqa episode artwork

May 27, 2022 45 min

Tariqa

from Wolof Podcast Hosted by Lahat Diaw

Suñu waxtaanu tay bi day jëm ci tariqa. Lan mooy tariqa ak lu ko tax a jóg? Ndax coosaanal tariqa yi moo ngi wéy ba léegi? Amul siki ni ñi sosoon tariqa yi ci lu wér lanu nekkoon, waaye lu ñuy gën a dem mu melni liy mbir mi dëgg, te mooy defar nit ku sotti, danu koy gën a sori. Ndax sant lanuy toppee Sëriñ? Lan lanu fay sàkku? Lan mooy xam Yàlla? Yiii ak yaneen laay waxtaane ak Allaaji Jibi Séy, muy boroom xam-xam di gëstu kat. Bokk na rek ci téere yi mu bind: « Jàngal sa diine ci wolof », « Seex Ahmadu Bàmba Xaadimu Rasuul jaar-jaar ak jàngale », « Juróomi Téerey Sëriñ bi ci làkku wolof »… [email protected]

Episode details come from the podcast's RSS feed.

Embed this episode

Ready to play

Tariqa

0:00 45:00

No transcript yet.

Requests help us decide what to transcribe next.

Frequently asked questions

How long is this episode of Wolof Podcast?

This episode is 45 minutes long.

When was this Wolof Podcast episode published?

This episode was published on May 27, 2022.

Can I download this Wolof Podcast episode?

Yes. Use the download control on the episode player to save the publisher-provided media file.