Xam-xamu Xadiis
from Wolof Podcast Hosted by Lahat Diaw
Xam-xamu xadiis lanuy waxtaane tay. Mu nekk fànn bu yaatu boo xamne woroom xam-xam yi gëstu na ñu ci ngir yoonal lépp loo xamne toxalees nako co Yonent bi (saws). Bokk na ci ay waat yu ñu leeral jëm ci xadiis, lu melni „Sanad“ te mooy goor yiy soloo xadiis yi, walla „Matn“ te mooy li ñuy soloo. Mu nekk xam-xam yu yaatu waaye fi nuy indi rek fànn wu ndaw ci seddale yi ñu def ci xadiis (classification). Baay Lahat [email protected]
Embed this episode
No transcript yet.
Frequently asked questions
How long is this episode of Wolof Podcast?
This episode is 45 minutes long.
When was this Wolof Podcast episode published?
This episode was published on March 31, 2023.
Can I download this Wolof Podcast episode?
Yes. Use the download control on the episode player to save the publisher-provided media file.